top of page
Rechercher

Tontou Lath Abdoullahi Cissé

Photo du rédacteur: mutadarasunamutadarasuna

OBJET : YOK GUEUM AK JAAMU YALLAH


Alkhamdoulillah Wa Sallallahu Anla Mouhamad,


Lath gama lath bo xamni lath la bou oyof thi lamine wayé bou diss thi xol loudoul kouko yallah yombalal (yallah naniou ko yallah yimbalal)

Nit niar yi rek la am thi adounam Diamou Yallah biko bind guir mou diamouko ak Liguey.

Sa gueum yallah likoy doli moy lep lou nekh yallah ga nek thi, di dhikar lou beuri té deglou borom xamxam yi dina takh sa gueum di yok, ak tamit di bayi xel sa borom thi situation bo meunti tol. Té fekhel ba beug yallah beug bo xamni doko yamalé ak dara doko yamalé ak ken lolou molay yobou thi bagn ko bokalé t bagn ko moy andak di ko diamou.

Liguey nak dou natou wayé xewal bou reuy la bou la yallah defal guir ga samb sa ngor, boko diapé nonou diga ko fonk t bagn thi sagan t sa yo liguey ba wer dé diokhal liguey bi xalissam biy takh mou meun avancé doga lek sa wal boko defé diga avancé chaque mois, wayé del meuytou di bayi xel lou Haram day yak barke bi sa liguey waron am boul fokolé thi benefice wayé doylol lou yam bou boba bolé ga niar dimbali diam yi ak doylou té lolou koukoy def rek amoul ben siksak né yallah di nala barkelal sa liguey

Yallah naniou yallah defal aw yiw man ak yaw ak kep kou lire bilé batakhal t defal niou Gueum bou man seuk ak Liguey bou barkel

Wallah Taanla Anhlam


Shaykh Issa Smabe

20 vues0 commentaire

Comentários


bottom of page